DG
DiodioGlow
Ah doom, mbaa xam nga kii ngay xool am 🥹 Ah doom, jëmm jii aka bëgg Ahmadou ma juddóo Màkka Ah doom, mbaa xam nga ni kii ab xolam  Moustapha moo loy dundal ? Doom kii sunu maama  Moomit Ahmadou moo di aw turam  Aka baax, aka fónk Ahmadou turandóo wam  Aka amal njariñ nit ñi, akay jàmbaar, aka bari xam-xam Akay gor, akay góor, akaay borom ngor ag jàmm  #pulsenewsreels #sinformersurtiktok
Pulse Sénégal

Pulse Sénégal

pulsesenegal

Découvrez cette vidéo TikTok captivante de @pulsesenegal dans la catégorie tendance. Suivez les tendances virales du Sénégal avec DiodioGlow - Votre source #1 pour le meilleur contenu TikTok, buzz, musique et actualités.

1.8K

Views

215

Likes

5

Comments

0

Shares

original sound - islamic_vibes802

Islamic states