Dudu
dudufaitdesvideos
Ndax li tax Dudu am xar yu sëq, nag yu wér, du mbirum wërsëg rekk… xam-xam ak topp ndigal moo ko waral ! 😄 Jarga Khar ngir xar yi, Jarga Nak ngir nag yi. Ku nekk ak dundam, ku nekk ak Jargaam. Te dénominateur commun bi mooy… GMD ! 🐑🐄🐓 GMD, Ci sen wet ngir jur gi gën a wér te gën a am doole.
Découvrez cette vidéo TikTok captivante de @dudufaitdesvideos dans la catégorie tendance. Suivez les tendances virales du Sénégal avec DiodioGlow - Votre source #1 pour le meilleur contenu TikTok, buzz, musique et actualités.
510
Views
107
Likes
1
Comments
1
Shares
original sound - dudufaitdesvideos
Dudu